Innoncent

Song

Innoncent

Dip Doundou Guiss · Tay Leu Kagn · 2016 · 4:40

Lyrics

Yeah ba niepp dièxallè Mann sillay soga fèss Def nala Papa parce que tèrè woma xèkh Dinagn la enquête ndakh tay sa doma xéw ta bam léne wanné samay ranngoy niom niepp bégu Bo xaméni faw lékk faw nga fokhalé Da ngay xép conndané bou tol ni contenaire last kiri pairou dalleu dâm la soll ba dé motaxx tay Job ba dé niakk diott ba dé Damako khar ni Steph Curry Pour wathié Jordan Man Ni bépp xéttou nit bouy wadja donn lénènn Fatté wouma fi gnou ma diangalé fi gnou ma djngalé Fatté wouma Pa yi ma niannal mères yii ma dioxx ma lékk Avenir lagn diémona dieulli ci yonou karaw bou nioul ak xél bou mak sa niom Mame Boul wôllu sakh ñi la wôllu Confiance xadioul ci Malayka Djînné Conscience May Garab bou beug microbes Innocent bouy andd ak Inno Ay Fènn katt rekk ak ay traitres layy guis souma fattéliko Diox ma passeport visa yeah Tampon cii Passeport bi ma dém Par force fass diom biss mba dé Waw goor di nga donn Milliardaire Éhhh ya fi néwonn souniou GANG Famille la Niounn niepp bokk Diar diar nigger Fima diar kouffa diar xam né yaw fi nga Diar koufa Diar tass sa yakarr nigger ma ngui niafé ma ngui xar matt nigger xonnéta touma sakh rarement nigger Fima diougué souma fa naré dèllou watt fathie la Jail wala teuthie ma Hôpital my nigger Yeah yeah Yeah ba niepp dièxallè Mann sillay soga fèss Dip comme ko teudd lo correctionnel ay Colonel Dinagn ma saga ndey Dina lènn songg xékh Konn niakk diott ba dé guénné sons ba dé Maouti Sakh douma dieul ci parce que mak moma yémm Konn en cas Mc bou Dé boul lathie kann moko ray Niata rappeur nga féyy niata millions nga kékk Boy déssé touma bénn ranggoñ pour dioy sa deuthie Est ce que witthiaxx na sama baram Guéthie na réthiou depuis 17 ans Motherfucker Damako xarr nitt dé ak Aldiana Mann dama lènn rèndi soga titt Ndayssane dawna yaram Boy mann kassé béneu nitt 5000 nitt dima xékh Nianall na samay ennemies ennemie ki ak ké Dama xékhal mbédd bi mbédd bi dima xékh Dama xékhal mbédd bi mbédd bi dima xékh Ma ngui ci chaisou Bour bi nio ngui ci chaisou douche yii Fake gui dounkkou yii nandité you mouss yi tékk nañ nou deal mais guénn guénno ci Noir et fier amoufi dér bou nioul bi mo xépp dér bou nioul Mafi geunna touti thiabi bou reuyyônn dou tidjî bountou Mangui geunna yékk di geunna yekk di guenna wétt Xaritt aka nëw yii Diamono wouy sama Ndeye Temps yi yeurmandé def sama xol ci sama xél diay kou mana fayy dou niou mayé xérr di keuppeu caisse yeah fittna la fittna may fittna fittna la fittna may fittna

Lyrics provided by LRCLIB.

Popular by Dip Doundou Guiss