
Lyrics
baby yaw fo far
waro ma déf lii
té wakhomaa lou waral lii
wakh ma lou waral lii
bo khamon lima dénthieu
waro maa déf lii non non
té wakhomaa lou waral lii
wakhmaa lou waral lii
ohhh
yeah
bagniy beugeunté kogne ba done ay xalei you ndaw
bobou gnoun gnaar rékkeu fogon ni parer wougne wone
anectode bi ay dome ngama amél ma amél la dot
sougnou gnari xol yi di naaw bébé année di dokh
may daw pour di pointé sa school ni may garder école bi
dila solal kaw ba souf ni kouy diaay prêt à porter
nignouy wakher laay gassé soul sama bammélou nop
pour man djiguén yeup rafétougnou rafét ba melni yaw
goor yalla bou gneuw tél ngako barrer mou daw
man mii maay sa xol amo xol bou carré bou rond
yalla ko touddou bala sougnou waa gallé di tokk
batay ma ngi lay beugueu awma xolou caméléon
love boudoul dé moy rayé seuy nagnou ba am gnéti dom
bo kholon si gnom si yaw do kheuy di demander divorce
yaaci bolé kouci bokkou sa yaye louci yonam
man wala say dome sa dieukeur kay ma laath la
baby yaw fo far
waro ma déf lii
té wakhomaa lou waral lii
wakh ma lou waral lii
bo khamon lima dénthieu
waro maa déf lii non non
té wakhomaa lou waral lii
wakhmaa lou waral lii
ohhh
lo guiss day diékh
xol bi day wét
wét di dioyi fénén
baby logique bay fén
démb comme pic ak pelle
gneuw lép compliquer tay
wakhma lou soppi sa xél
ba takh nga obliger dém
faw gnou seddo nakhar bi comme dagnou ko cotiser démb
sougnou mbeuggel dou diekh même sougnou meunoul continuer seuy
khawma bakham nakh ak bénén goor di nga bék
man mii khawma bakham nakh bess samay gaume dina wér
mouno ma miin ba fatté maa
mouno ma miin ba fatté maa
wan ngama guinnaaw
dotoumala guissaat
bo démé dina wéteu wétt wéteu wét wéteu wét
bo démé dina wéteu wétt wéteu wét wéteu wéét
baby yaw fo far (fo faar)
waro ma déf lii
té wakhomaa lou waral lii
wakh ma lou waral lii
bo khamon lima dénthieu
waro maa déf lii non non
té wakhomaa lou waral lii
wakhmaa lou waral lii
ohhh
kon donc ni nga teunké nii man vraiment j'en suis I happiness
mais nak amour guy you beuri dagnoukay diaawalé ak mbeuguél
mbeuguél dou amour, amour dou thiofél,
thiofél dou yeuk yeuk kon képpeu ko khamni yaa ngi
douggou si amour parceque da nga love tu vas perdre
parceque mbeuguél beugoul kénneu kén beuggoul mbeuguél
mbeuguél mi ngi sa biir doundou
kon ké kouy doundé mbeuguél let's slow
et that's I let's go yaama geuneu fun kw
baby yaw fo far (baby yaw baby yaw)
waro ma déf lii (baby yaw)
té wakhomaa lou waral lii
wakh ma lou waral lii
bo khamon lima dénthieu (baby yaw baby yaw)
waro maa déf lii non non
té wakhomaa lou waral lii (baby yaw baby yaw)
wakhmaa lou waral lii
wohhh
Lyrics provided by LRCLIB.
Popular by Dip Doundou Guiss
#TitleAlbum







